Le Grand Magal de Touba 2025 ! Revivez un moment historique : la prestation du Kurel Mafatihoul Bichri (HT Daara Touba), coïncidant avec l’arrivée de Serigne Mountakha Mbacké lors de la clôture du Grand Magal 2025 à la Résidence Cheikhoul Khadim.
🎶 Une déclamation des Khassaïdes de Serigne Touba pleine de ferveur et d’émotion. 📺 Regardez et partagez 👉 https://youtu.be/umnW8Rir9YA
Aygore Màgalug Tuubaa 2025 gi ci mujj gi Kurel gii di Mafaatihul bisri (HIZBUT-TARQIYYAH Daara Touba) ñoo am Tawfiixi waxtu wi ñuy jàngg Sëriñ Muntaxaa Mbàkke yegsi dugu ci biir saal bi took teewlu lu njàng mi ba mu yegg mu yekkati kàdduy Sant ak Soññee ñaanal ñepp.
Màgalug Dewen Yal nañ feke lépp ci Barkeelug Xasida Yi.
Nañ Deglu Njàng mi Te Yaatal Widewoo bi Tasaare ko ngir dooleel ligeey bi.
Al Khadimiyyah TV
Le Grand Magal de Touba 2025 !
Revivez un moment historique : la prestation du Kurel Mafatihoul Bichri (HT Daara Touba), coïncidant avec l’arrivée de Serigne Mountakha Mbacké lors de la clôture du Grand Magal 2025 à la Résidence Cheikhoul Khadim.
🎶 Une déclamation des Khassaïdes de Serigne Touba pleine de ferveur et d’émotion.
📺 Regardez et partagez 👉 https://youtu.be/umnW8Rir9YA
Aygore Màgalug Tuubaa 2025 gi ci mujj gi Kurel gii di Mafaatihul bisri (HIZBUT-TARQIYYAH Daara Touba) ñoo am Tawfiixi waxtu wi ñuy jàngg Sëriñ Muntaxaa Mbàkke yegsi dugu ci biir saal bi took teewlu lu njàng mi ba mu yegg mu yekkati kàdduy Sant ak Soññee ñaanal ñepp.
Màgalug Dewen Yal nañ feke lépp ci Barkeelug Xasida Yi.
Nañ Deglu Njàng mi Te Yaatal Widewoo bi Tasaare ko ngir dooleel ligeey bi.
2 months ago (edited) | [YT] | 24