Assalaamy Tv

Serigne Amdy Khady Fall moo wuutu Serigne Amdy Modou Mbénda Fall ci kanamu njabootu Maam Seex Ibrahima Faal, nekk 9e Khalife Général des Baye Fall.
Yàlna toogaay bi yàgg lool Faal barkeb Boroom Tuubaa

8 months ago | [YT] | 1,047