Assalaamy Tv

Serigne Amdy Khady Fall moo wuutu Serigne Amdy Modou Mbénda Fall ci kanamu njabootu Maam Seex Ibrahima Faal, nekk 9e Khalife Général des Baye Fall.
Yàlna toogaay bi yàgg lool Faal barkeb Boroom Tuubaa

8 months ago | [YT] | 1,047



@FallouLeye-s8h

Yalna yala doliko ler ak yermande amine

8 months ago | 0

@ndiagacisse4962

Yalna yalla yokk lerou. s Amndi modou mbenda.te yagal Fi s Amndi khadi

8 months ago | 1

@La-confience-en-soi-yx8gw

Amin Yarabaal Henlami

8 months ago | 0

@OuleyeDiop-g4m

amine

8 months ago | 0

@Aliounebadarakébé-m9x

Yalla nafi yague lole té wér Amin inchallah nioubokouko

8 months ago | 1

@MortallaGueye-t6z

Amine yarabi

8 months ago | 0

@sahelb.t.p1508

Dieureudieuf Serigne Touba

8 months ago | 0

@abdouakimbabou116

Yalla nafi yague tewer amine

8 months ago | 0

@seydoundiaye8341

Amine

8 months ago | 0

@falloudia4561

Yalla nafi yague loll te werr

8 months ago | 2

@elhadjimbackethioune3678

Alhamdoulilah Machalah

8 months ago | 0

@massambadarousalam9586

Yal na fi yàgg lool te wér.

8 months ago | 0

@Khadija-SssTv

Yagg fi lol ta weer fall

8 months ago | 0

@FallouGaye-gf7kb

Amine

8 months ago | 0