Kou voté Takhawal sii centre de vote yii ba ndiou diokhé résultat yii na sii ndieupp diapp na sii djott diomaye 5e président inchallah 🇸🇳🇸
1 year ago | 2
Son bi jour bimou gein mangui won si hat hat you metti mais dama ko deglou rek sa yaram bi di daw barki alhouran
1 year ago | 5
Samba Peuzzi
BRIQUE 🧱
1 year ago | [YT] | 4,137