Yalla na yalla sounou borom tek la lokho , same la , soutoural la , deffa la diam , may la dame si projet bi ,sounou Ousmane sonko
1 month ago | 4
Parce que Ousmane ab julitla haxxan machallah hafizahumoulllah warahahoum
1 month ago | 0
Machaallah PM ! Yalna niouko Yalla samale, takhawou ko ba mou aggalé yénnéme si rewmi. Dieureudieuf 🙏🙏
1 month ago | 0
Machala Pm Sonko toujours égal à lui-même infatigable joli boulot yalna Yala motali samako accompagne ko andak weer Réussite Talko Amine ya Rabi
1 month ago | 2
Sunugal 24
Mubarak Pm Sonko
1 month ago | [YT] | 2,651