Bienvenue sur Xam Xam Média, votre chaîne dédiée à l’actualité, à l’Islam, au savoir et au buzz au Sénégal et en Afrique.

🎥 Informer – Éduquer – Inspirer
📍 Basé à Touba

Retrouvez sur notre chaîne :

* 📰 Actualités du Sénégal et d’Afrique
* 🕌 Islam et enseignements islamiques
* 📖 Khassida et enseignements de Serigne Touba
* 🎙️ Conférences, zikr et rappels
* 🌍 Vie religieuse et événements à Touba
* 🎧 Khassida audio et vidéos mourides

Abonnez-vous à Xam Xam Média et activez la cloche 🔔 pour ne rien manquer de nos nouvelles vidéos.


Xam Xam Media

S A W🙏❤️

15 hours ago (edited) | [YT] | 2

Xam Xam Media

???

2 days ago | [YT] | 10

Xam Xam Media

Jerejeufé Serigne Touba 👌🏾🤞🏾🙏🏾

1 week ago | [YT] | 13

Xam Xam Media

❤️🙏

2 weeks ago | [YT] | 5

Xam Xam Media

Amërik dina ligeey bu baax ak réewum Iran. Ci sunu gisuwaay, seen njiit yu bees yi ñu ngi ligeey ligeey bu am solo lool. Iran dotalul (enrichir) uranium té Amërik, bokk ak Iran, dinañu génne té dindi lépp lu jëm ci "poussières" nucléaire yi ñu dencoon ci xóot-xóot (yi jóge ci bombardiers B-2 yi). Nganaay yooyu, ñu ngi leen di wéy di sàmm bu baax ak sunu satellites yi (Force spatiale !). Dara laalewul ba léegi la xare bi amé.
Ñu ngi waxtaan, té dinañu wéy di waxtaan, nan lañuy dindé walla wàññi droits de douane yi ak sanctions yi ci kaw Iran. Juboo am na ci lu eup 15 points yi ñu doon waxtaané. Ma ngi leen di sant bu baax.
Njiit li Donald J. Trump
#xamxammedia

4 months ago | [YT] | 0

Xam Xam Media

LEN CI NDIARIGNOU FATIHATOUL KITAAB ( FATIHA ) SECRET FATIHA

Bismillahir rahmànir rahimi ( Barkep Borom Touba – Cheikhra Fall )

FATIHATUL KITAP Yonent bi .s.a.s neena kep kou guemulni manuta fadj sa aadio yalla busa aadio fadiou
FATIHA aadio dioum manuta fadj amoul ci kattanou Yalla .

*Sounu Borome néena guign naa tchi samak tééd ak samak magg ak samak tabé ak samak baakh néena koo xamni diangue nga al basmalatu djiokthia(tèk sa) faatihatul kitaab bamou ag wéén yoon(1fois) rèèk danala diégal say bakkaar doonté dafa diotéwoone ba assamaan sa danàa nangou saw yiw té douma lak saw lamigne mukk tchi sawara té dinâala mussal thi mbougaluk bammèèl ak mbougaluk yawmal khiyaam té danàala diapandalal sak guisma nga andak gni nga xamné sounu borôme dafaléèna xéweulé thi yonéntayi ak waliyuyi.

Boknaci ndiarignou FATIHA bo dioulè dioulik farata gounè nga def FATIHA 20 fois nga xamni ci biss bi dina mat 100 fois ,Yalla dina doli sa weurseuk ,yalla leral sa guisouk beut ak sa guissou khol ,yok sa daradja yok sa barkè

BO BEUGUEE AY KHEWEUL BOKO DEFEE FIIYEUK DEWEN SERIGNE TOUBA NEENA DOOTO DISS KEEN SA SOKHLA(Incalah)
--Apres dioulli souba rèciter FATIHA -30 fois
--apres dioulli tisbar reciter FATIHA -25 fois
--apres dioulli takkoussan reciter FATIHA 20 fois
--apres dioulli timis reciter FATIHA 15 fois
--apres dioulli guèè reciter FATIHA 10 fois exprimer tes veux

Kou sakhal sàyo dioullè def FATIHA 100 fois(tèmèri yoon) moxam dangko diang bèn yoon wala dangko def 20 fois wala 30 di wagni diourom ba guèwè bam mat temer (100 fois) kouko sakhal di nga am li nga beug ci lou gawa gaw inchalah

Kou sakhal sàyo dioullè souba nga diang FATIHA 125 fois di nga am li nga beug , am sa khèmmèmtèèf ci ludul sik sak

POUR AADIO DIOU MAKK dangay wird FATIHATUL KITAB 125.000 fois kuko def nguir aadio lou aadio dja reuy reuy dina fadiou

Bo sakhale FATIHA 313 fois nguir bèp dioublouway soun borom danalasa defal langa beug (lim bi di 313 secret bu mag dasè nek limou universel la )

FATIHA diounni ndiarign zahir ak diouni ndiarign baatin mi nguici kou sakhal diko diang goudi ak beuthieuk soun borom dinala dakhal tayyeel ,ak yaafous ,setal biireum ,ak biteem ci mbolèm fèbarou bakan yek febarou sayir ak you batin yi ,ak saytanè ta faw kuko sakhal diko diang soun borom xamalla xamxam bo xamni desuko diang ci tèrè

Kou sakh di diang FATIHA faw sounborom defalla al-istikhama ,faw sun borom defalla ak ndioup

Kep ko xamni yangui teud nga diang FATIHA 1 fois + LIKHALAS 3 fois+ FALAQI –NAASI Yonente s.a.s neena goudi googou mouthie nga

kep ko xamni dafa fèbar nga diang FATIHA 40 fois ci ndox nga raxas si lokhom ak gnari tangkam ak kanamam ak bopam ak bireum ak la fègn thia yaramam dinako wèreul

kep kou am aadio bo dioullè timis ba nopal bala nga def dara nga def nafila yula nekh moxam gnari raka etc..nga diang FATIHA 40 fois nga gnan sa aadio amoul sik sak sounou borom dana fadj aadio diodia ( waye so parè dangsiy tek gnan gui )
Allàhuma hilmouka kaafi hanis suwali ikfinii bi khalkhil fatihati suwana wa karamuka kaafin hannil makkhàli akrimni bi hakhil fatiha makkàna wa hansil màfi damiiri .

Kou diap ba sett diouron gnari fan ( 7 jours ) biss bou diotnga diang FATIHATUL KITAAB ( 70 fois ) nga tifliko ci ndox mou laap bou 7 jours yi diotè nga naan ko
Sun borom dinala weurseuguelè xamxam ,ak hikhma,laabal sa xol ci khalàt you bonn yi ak you gnaw yi ak lep ,ta kou def lolou sunborom dina def nga nek kou inteligent kou moùs ,tayit doto fattè li nga dèg lep lo degueuti dangko diap ta doko fattè .

Kou diang FATIHA 41 fois diguentè fadiar ak souba fek danga am beut wala beugn youy metti bokoci defe inchalah dina weer ci bou gawa gaw inchalah ,nimou gawè ci fathie beut youy metti nonu la gawè ci fadj bep metit .( waye lep mboot mi moy rafet ndiorte )

Bou amè kouy toukki di taggatòtok yaw dem nga diangalko FATIHA 41 fois inchalah dana dèlousiwat ak diam

EL Adji Abdou Aziz neena gnar gnouy taggato di dem gnu diokhantè lokho tari FATIHA inchalah sun borom dana dogalat sen guissè .

FATIHA 121 fois (lim bou am dòlè di tollok AL-MALIK ) kep koun chèner wala gnu diatangla nga diangko tifliko thia mou deign )

Kep kou amè mettit nga tek sa lokho falay metti diang FATIHA 7 fois nga tek thia li
( Allahumma azip hannì su amà adjidou wa fakhsì bidakhwati nabiyouka mouhammadine al moubarakal al makiinil aamiin hindaka (7 fois ) soun borom saafara la .

Nguir am li nga beug Yalla oubileu weurseuk yi ,dangay bayi ba weer tèrou dibeer djisi ndieul
(1 er dimanche) nga diang FATIHA bu andak (bismillahir rahmanir rahimi) 70 fois
Altine (lundi ) nga diang FATIHA 60 fois
Talaata ( mardi) nga diang FATIHA 50 fois
Allarba(mercredi) nga diang FATIHA 40 fois
Alkhamiss (jeudi) nga diang FATIHA 30 fois
Aldiouma (vendredi ) nga diang FATIHA 20 fois
Gaawou (samedi ) nga diang FATIHA 10 fois
Koukoy def weer wou diot( chaque mois) Yalla dana oubi sa bounti kheweul.

Kou sakhal waxtou ndjeul wounè nga diang FATIHA 41 fois soun borom oubi sa weurseuk ,yombal say mbir ,do am thiono ,do am diafe diafe .

Kou sakhal FATIHATUL KITAP moxam dangkoy diang limoup araf yi 125 –ou 123 ou – 124 –bouci nek lim lasi wala nga diangko 313 fois wala 1000 fois
nga defko 3 jours wala 5 jours wala 7 jours sans depand ciyaw bolekok diap ndiap mou sell tok dioublou pingkou diangko ba agal ta do waxak ken ,kou def li sa aadio dana fadiou inchalah
(boula nekhe nga defko khalwa 3 wala 5wala 7 jours do lek lou am rouh kuko def sun borom fathie sa adio inchalah) .

Kou ragal khif ak marr (ko xamni danga kheuy souba ta biss bobu nga ragal si khiif ak marr nga diang FATIHA tifliko sa lokho raay si sa kanam ak sa biir sun borom biss bobu danalasi fegal khif ak marr )xamna lolou dina enranger gniy woor

Bò amè sokhla apres chaque priere recite Fatiha 7 fois pendant 7 jours khadioul si sokhla (sokhla bo am nga nian ko si incalah bou sòbè yalla dinga am linga beug


Qui rècite FATIHA 114 fois dò raflè mouk

Bo amè sokhla beug Yalla fadialla ko rècitè FATIHA 70 fois nga gnane sa sokhla

kou beug say àdio fadiou,mo kham ngay sèt ligueuy wala ngay lidieunti dara ,rèciter FATIHA 7 fois suivie de ALAMNASRA 7 fois nga dèm sa adio dia ,incalah yalla dinako sottil (S.T)

POUR FATHIE SOKHLA
Recite FATIHA 7 fois /salàtu-ala nabi 100 fois /Alamnasrah 70 fois /salàtu-ala nabi 100 fois nga gnaan sa sokhla inchalah dina fadiou

POUR MOUSLOU CI THIATE dangay diang faatiha ,wakh bismillahir…….ba alhamdoulilahi rabbil hanlamiim ,nga yam fofou dadi wakh ,wa inyakanoulaziina kafarou bi afsàrihim lamma samiihon zikra wa yakhoulouna la madjnouroun wa ma houwa illa zikkroun li lhanlamiina ,ba 7 aaya yi matt.

BOO BAGNEE GAAWA MEER(fàcher)reciter
FATIHA jusqu'a IYAAKA NAHBOUDOU WA IYYAAKA NASTAHINOU Rèpèter 70 fois apres vous continuez jusqu'a la fin.

*NGUIR FATHIE AADIO(sokhla) KEP KO KHAMNI DIOULLINA GNARI RAKKAS ,RAKKAS BOUNè NGA DIANG FATIHA DIOUROM GNARI YOON(7fois)TAMBLè
(Al khamdou lilahi rabbil ànlamiina)BOU NOPPè DADI WAKH:
Inna zàlika fìì kitàbine inna zàlika hanlàl-làhi yasììroune 3 fois)
DADIKOY TEUDJè GNAN GUII:
Allàhoumma innaka tanhlamou mà noukhfìì wa mà nouhlinou wa mà yakhfìì hanlàl-làhi mine chay-ine fììl ardì walà fììssamà-i (1 fois)


Rèciter chaque matin FATIHA 7 fois suivie de YAA SAAFII 422 fois eufko si ndokh nàn ko (boire) dò wop(malade) mouk incalah

kouy faral di diangue FATIHA lou bari Yalla dinako dèfal loumou beug cik mbàkham(S.T)

bo beuguè mouthie ci saytànè rèciter matin et soir FATIHA 1 fois suivie de INA-ANZALNAHOU 7 fois yalla dinala dakhal saytànè ta dinala mousseul ci lèp louy lore ,ta dinala diapandalal lou diafè (S.T)

bou fèkkè sa dòm day tiite gouddi ba diakhalla wala sa sokhna matou diakhalla diangal FATIHA suivie de YAA LATIIFOU 111 fois nga tifliko si ndokh diokh ko mou nàn ,diw biireum ,incalah yaram wa dina sèd wala boudè matou dou am bèn complication(chaque matin)boko tarè do wop mouk(S.T)

bo beuguer fathie kou gnak khèlam(reciter FATIHA 111 fois pendant 7 jours(kouy dànou,bou fèkkèni dafa nakhariwòn khèl dina dèllousi ,ta dina fèk lor(incalah)(S.T)

Bou fèbar bouy wallè amè(mbass) nga beug sè mouthie(wala Nòn(ennemis-khiif-ak mbass) reciter: FATIHA 7 fois suivie de AYATOUL KOURSI 7 fois(ichalah man nga diàkhàn nèlaw ,diaroul ngay dèm docteur dara doula dall ak kossi yèènè wale(S.T)

GNAN GUI BOKO DEFE BEP THIATE BOUM FEK CI YAW DINDI KO Dangay bind FAATIHA ,ci diguentè aaya bounè nga bindsi (wa-inyakà-doullazìna kafaròu….mongui ci sourate xalam) ba 7 aaya yi djekh nga bolèkok rèènou nguèèr sangòko ( inchalah loum fèk ci yaw ci thiate dindiko )

Bo beuguè mouthi ci thiate bayil ba jeudi soir ngua binede fatiha bamou diéx té do ka mass si soufame ngua ték si salatou hala nabi béne yone momite doka mass si soufeume encore ngua binde wallahou yahsimouka minane nasi 11 ligne yo hame ni ligne bou nék 3fois nguako siye binede teudjié ko 1 salatou hala nabi sanggo ka

Source :Bayfall Ndigueul Le Serviteur

4 months ago | [YT] | 1

Xam Xam Media

وَلَا يُخَفَّفُ عَنۡهُم مِّنۡ عَذَابِهَاۚ كَذَٰلِكَ نَجۡزِي كُلَّ ......

4 months ago | [YT] | 0

Xam Xam Media

"Al Hamdoulillah ! 700 abonnés. 🙏🏾 Merci pour votre confiance. Ensemble vers les 1 000 ! Jërëjëf."

5 months ago | [YT] | 3

Xam Xam Media

Bonjour tout le monde et bienvenue dans ma nouvelle Communauté YouTube ! Vous pouvez désormais publier sur ma chaîne. Pour commencer, dites-moi dans un post ce que vous aimeriez voir prochainement sur ma chaîne.
Accédez à ma Communauté : youtube.com/@xamxam2609/community

5 months ago | [YT] | 4

Xam Xam Media

Al hamdoulillah, bienvenue sur l'espace communauté de Xam xam ! Merci pour votre soutien."

5 months ago | [YT] | 5