Institut Serigne Thierno Gaye Balla

Bienvenue sur la chaîne officielle de l’Institut Serigne Thierno Gaye Balla

Cette chaîne a pour vocation de partager des contenus islamiques, des enseignements du Saint Coran, des rappels religieux, des conférences et des connaissances utiles pour approfondir notre foi et notre compréhension de l’Islam.

📖 Coran et enseignements islamiques
🕌 Rappels et conseils religieux Khoutba
🎙️ Conférences et enseignements Khasida kourel
🌙 Spiritualité et éducation islamique

Abonnez-vous à la chaîne et activez la 🔔 pour ne manquer aucune nouvelle publication.

E-mail www.institutserignethiernogaye@gmail.com
Contacts 78 293 72 44

Qu’Allah nous guide, nous accorde la science utile et nous facilite le chemin vers le bien. 🤲🏾

institut Serigne Thierno Gaye Balla Xam Xam Buy Gëndi Bàllë Di Law Ba Faww


Institut Serigne Thierno Gaye Balla

Tabaski ag jamm ñeel ñepp

1 year ago (edited) |[YT] | 39

Institut Serigne Thierno Gaye Balla

Murid dafay woyof ndeysaan.
Soxna ci dafa ñëw ci jumaa ji massalik bëgga visité waaye li mu sol méngoo wul ak li mëna dugg ci jumaa ji. Boroom Baaylat bi dindi kaalam gi solal koko ngir mu mëna dugg ci jumaa ji. Lii mooy ag murid, dal, woyof, yaatu, te xam àdduna
‪@HtdnmXamle‬

2 years ago |[YT] | 62

Institut Serigne Thierno Gaye Balla

Abonnél Fii 👉🏿‪@HtdnmXamle‬
Sëriñ Muntaxaa 👉🏿 El Bassir ❤❤❤

2 years ago |[YT] | 35

Institut Serigne Thierno Gaye Balla

‪@HtdnmXamle‬​ ❤❤❤Abonnél Fii 👈🏿👈🏿

2 years ago (edited) |[YT] | 59

Institut Serigne Thierno Gaye Balla

Ku Teedd Ki ❤❤❤

2 years ago |[YT] | 46

Institut Serigne Thierno Gaye Balla

Joyeux anniversaire🎂🎂
PM Ousmane Sonko Fan Wu Guddu Rk Lañ Lay Ñaanal Wàcco Nga Ak Ñun Bu Yàgg Te Xam Nañ Ni Linga Deñcal Senegalais Mo Ëppu Linga Ñu Jota Wan Yaw Daal Dundël Rk ❤

Abonné Vous S'il vous plaît ‪@HtdnmXamle‬ ‪@institutserignethiernogaye‬

2 years ago |[YT] | 27

Institut Serigne Thierno Gaye Balla

youtube.com/@htdnmxamle?si=OyHW4PW3va3-hD4M

Abonné Vous S'il Vous plaît ☝🏿☝🏿

2 years ago (edited) |[YT] | 48

Institut Serigne Thierno Gaye Balla

ALERTE 🚨 ‼️

Marché Ocass Touba : Bén Sokhna sunu tañc domam ci xatxat yi bamu faatu ca saasé..🤱🏿
😭

Di ñaan ñuy gënë bàyyi xel ci tuut-tank yi ñuy yobbaalé ci ay bërëb yu xat niki ab marché.

‪@HtdnmXamle‬ ‪@institutserignethiernogaye‬

2 years ago |[YT] | 26

Institut Serigne Thierno Gaye Balla

S Aliou Ndiaye Hddkh Aka Mana Binde 🥰🥰

Mais Abonné Vous SVP ‪@institutserignethiernogaye‬

2 years ago |[YT] | 55